Compositor: Não Disponível
Le passé c'est le passé
Trop de problème avec toi j'en avez assez ey
Maintenant que tout a changé
J'ai tourné la page car tu m'empêche d'avancer
Thi diir bou gat lala khamé gua beug ma jugé
Thi sa digue, sa ay kharit gua sewalma ni i
Mane yorou mawone khaliss
Mais gniko yor sa khol iow mousso lenko thiabil
Bamala guissé si la guiss nit kima done sét
Façon yéne gor yii nieupeu yam ganéma mounoul néh
Mane melouma nii guar gni
Sa tank sama tank gua présenté ma PA bii
Gua begn dh néh dou mak iow
Geume lo mani né mounougnoun dem fén mak iow
Téré nanie ma teud temps nah doumala am iow
Iow mi sa bop yama téré ande ak iow
Gua bagn dh néh d'où mak yaw
Geum lo mani meunougnou dem fen mak iow
Téré nanie ma teud temps nkoul ak iow
Iow mi sa bop yama téré and ak iow, baby
Noboma wone, noboma ndeyssane
Noboma wone beumeu lay facetime
Talo ma wone beumeu lay message, noboma woo-woo-woo-ooh

Kouma ko wakhone douma ko geum ya moudier xewii nii
Mane iow rk la guissone gua diapé meuh nit invisible
Bayina la à vie, faté gua bigua ma done rombe ak vitesse Ferrari
Mbeuguel indi woula lila indi dieulina
Tey guamay sogua moune sét fep ni FBI
Rethie nala bayil, way bigua ma done dieundé lgui gua ko niémé trahir
Gua begn dh néh dou mak iow
Dama la mounoul mounie niou dem féne mak iow
Doma téré nakh mounou ma ande ak iow
Iow sa bop yama téré and ak iow
Gua begn dh néh dou mak iow
Dama la mounoul mounie niou dem féne mak iow
Doma téré nakh mounou ma ande ak iow
Iow sa bop yama téré and ak iow, baby
Noboma wone, noboma ndeyssane
Noboma wone beumeu lay facetime
Talo ma wone, doma done message, noboma woo-woo-woo-oh

Pourquoi tu crois aller venir quand tu veux
Cette fois hélas c trop tard ohh woo-woo